Al-Mu'minun · 63/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
بَلْ قُلُوبُهُمْ فِي غَمْرَةٍ مِّنْ هَٰذَا وَلَهُمْ أَعْمَالٌ مِّن دُونِ ذَٰلِكَ هُمْ لَهَا عَامِلُونَ ۝٦٣
Bal quloobuhum fee ghamratim min haazaa wa lahum a`maalum min dooni zaalika hum lahaa `aamiloon
📖 Tekkim Wolof
Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am nañu ay jëf yu yées yooyu te ña nga koy jëf,
🎧 Dégg

📜 Aaya 61-65 — Al-Mu'minun

61أُولَٰئِكَ يُسَارِعُونَ فِي الْخَيْرَاتِ وَهُمْ لَهَا سَابِقُونَ
Ñooña ñooy jëkkante ci jëfu yiw te jëkk nañu ca.
62وَلَا نُكَلِّفُ نَفْسًا إِلَّا وُسْعَهَا ۖ وَلَدَيْنَا كِتَابٌ يَنطِقُ بِالْحَقِّ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Dunu teg benn bakkan lu dul la mu àttan. Te ab Téeree ngi fi buy àtte ci dëgg, te kenn du leen ca noonu [ci waññi yiw walla yokk safaan].
63بَلْ قُلُوبُهُمْ فِي غَمْرَةٍ مِّنْ هَٰذَا وَلَهُمْ أَعْمَالٌ مِّن دُونِ ذَٰلِكَ هُمْ لَهَا عَامِلُونَ
Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am nañu ay jëf yu yées yooyu te ña nga koy jëf,
64حَتَّىٰ إِذَا أَخَذْنَا مُتْرَفِيهِم بِالْعَذَابِ إِذَا هُمْ يَجْأَرُونَ
ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet di yuuxu walla.
65لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 63

Simoore Al-Mu'minun Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am…

Simoore Aaya 63/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers