Al-Mu'minun · 64/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
حَتَّىٰ إِذَا أَخَذْنَا مُتْرَفِيهِم بِالْعَذَابِ إِذَا هُمْ يَجْأَرُونَ ۝٦٤
Hattaaa izaaa akhznaa mutrafeehim bil`azaabi izaa hum yaj`aroon
📖 Tekkim Wolof
ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet di yuuxu walla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Simoore Al-Mu'minun

62وَلَا نُكَلِّفُ نَفْسًا إِلَّا وُسْعَهَا ۖ وَلَدَيْنَا كِتَابٌ يَنطِقُ بِالْحَقِّ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Dunu teg benn bakkan lu dul la mu àttan. Te ab Téeree ngi fi buy àtte ci dëgg, te kenn du leen ca noonu [ci waññi yiw walla yokk safaan].
63بَلْ قُلُوبُهُمْ فِي غَمْرَةٍ مِّنْ هَٰذَا وَلَهُمْ أَعْمَالٌ مِّن دُونِ ذَٰلِكَ هُمْ لَهَا عَامِلُونَ
Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am nañu ay jëf yu yées yooyu te ña nga koy jëf,
64حَتَّىٰ إِذَا أَخَذْنَا مُتْرَفِيهِم بِالْعَذَابِ إِذَا هُمْ يَجْأَرُونَ
ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet di yuuxu walla.
65لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.
66قَدْ كَانَتْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُمْ عَلَىٰ أَعْقَابِكُمْ تَنكِصُونَ
Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko dummóoyu,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 64

Simoore Al-Mu'minun Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet…

Simoore Aaya 64/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers