An-Nur · 14/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ لَمَسَّكُمْ فِي مَا أَفَضْتُمْ فِيهِ عَذَابٌ عَظِيمٌ ١٤
Transliteration
Wa law laa fadlul laahi `alaikum wa rahmatuhoo fiddunyaa wal aakhirati lamassakum fee maaa afadtum feehi `azaabun `azeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ci yéen fii ci àddina sii ak fee ci àllaaxira, kon dey seen duur wii mbugal mu rëy dana leen ci dal,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — An-Nur
12لَّوْلَا إِذْ سَمِعْتُمُوهُ ظَنَّ الْمُؤْمِنُونَ وَالْمُؤْمِنَاتُ بِأَنفُسِهِمْ خَيْرًا وَقَالُوا هَٰذَا إِفْكٌ مُّبِينٌ
Lu tere woon jullit ñu góor ñeek jigéen di jort ci aw yiw ci seen diggante ? Ana lu tere ca saa sa ñu ne : “Lii kat aw duur la ” ?
13لَّوْلَا جَاءُوا عَلَيْهِ بِأَرْبَعَةِ شُهَدَاءَ ۚ فَإِذْ لَمْ يَأْتُوا بِالشُّهَدَاءِ فَأُولَٰئِكَ عِندَ اللَّهِ هُمُ الْكَاذِبُونَ
Bu ñu indi woon sax ñeenti seede, waaye bu ñu ko indiwul [ngeen daldi xam fa saa sa] ne ñoom kat ay fenjat lañu.
14وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ لَمَسَّكُمْ فِي مَا أَفَضْتُمْ فِيهِ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ci yéen fii ci àddina sii ak fee ci àllaaxira, kon dey seen duur wii mbugal mu rëy dana leen ci dal,
15إِذْ تَلَقَّوْنَهُ بِأَلْسِنَتِكُمْ وَتَقُولُونَ بِأَفْوَاهِكُم مَّا لَيْسَ لَكُم بِهِ عِلْمٌ وَتَحْسَبُونَهُ هَيِّنًا وَهُوَ عِندَ اللَّهِ عَظِيمٌ
ngir yéen a ngi jokk-jolaate xibaar ba ak seeni làmmiñ, di wax ci seeni gémmiñ loo xam ne amuleen ci benn xam-xam ; ngeen jàppe ko lu doyadi te fekk muy lu rëy a rëy fa Yàlla.
16وَلَوْلَا إِذْ سَمِعْتُمُوهُ قُلْتُم مَّا يَكُونُ لَنَا أَن نَّتَكَلَّمَ بِهَٰذَا سُبْحَانَكَ هَٰذَا بُهْتَانٌ عَظِيمٌ
Ana lan moo tere, ba ngeen ko déggee, ngeen sàbbaal Yàlla te wax ne : “Wii duur wu rëy warut a génne ci seeni làmmiñ” ?
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
14Aaya
Tekki — An-Nur 14
Simoore An-Nur Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ci yéen fii ci àddina…Simoore Aaya 14/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








