An-Nur · 42/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَلِلَّهِ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَإِلَى اللَّهِ الْمَصِيرُ ٤٢
Transliteration
Wa lillaahi mulkus samaawaati wal ardi wa ilal laahil maseer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàllaay boroom nguurug asamaan yeek suuf si. Te ca Moom la ñéppiy dellu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 40-44 — An-Nur
40أَوْ كَظُلُمَاتٍ فِي بَحْرٍ لُّجِّيٍّ يَغْشَاهُ مَوْجٌ مِّن فَوْقِهِ مَوْجٌ مِّن فَوْقِهِ سَحَابٌ ۚ ظُلُمَاتٌ بَعْضُهَا فَوْقَ بَعْضٍ إِذَا أَخْرَجَ يَدَهُ لَمْ يَكَدْ يَرَاهَا ۗ وَمَن لَّمْ يَجْعَلِ اللَّهُ لَهُ نُورًا فَمَا لَهُ مِن نُّورٍ
[Jëfi yéefar ba-tey dafa mel ni] lëndëmug géej guy duusu : ganax ci kaw ganax, ay niir yu lëndëm tegaloo tiim ko. Ba sax moom bu génnee loxoom, du ko xaw a gis. Te képp ku Yàlla defalul ag leer, du am ag leer.
41أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ يُسَبِّحُ لَهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَالطَّيْرُ صَافَّاتٍ ۖ كُلٌّ قَدْ عَلِمَ صَلَاتَهُ وَتَسْبِيحَهُ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِمَا يَفْعَلُونَ
[Xanaa gisuloo ne] ñépp ñu nekk diggante asamaan yeek suuf si, dañuy sàbbaal Yàlla ; picc yi sax dañuy sàppe. Lenn lu nekk xam na naka lay jullee ak na muy sàbbaalee. Yàlla xam na li ñuy def.
42وَلِلَّهِ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَإِلَى اللَّهِ الْمَصِيرُ
Yàllaay boroom nguurug asamaan yeek suuf si. Te ca Moom la ñéppiy dellu.
43أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ يُزْجِي سَحَابًا ثُمَّ يُؤَلِّفُ بَيْنَهُ ثُمَّ يَجْعَلُهُ رُكَامًا فَتَرَى الْوَدْقَ يَخْرُجُ مِنْ خِلَالِهِ وَيُنَزِّلُ مِنَ السَّمَاءِ مِن جِبَالٍ فِيهَا مِن بَرَدٍ فَيُصِيبُ بِهِ مَن يَشَاءُ وَيَصْرِفُهُ عَن مَّن يَشَاءُ ۖ يَكَادُ سَنَا بَرْقِهِ يَذْهَبُ بِالْأَبْصَارِ
Xanaa gisuloo ne Yàllaay wommat niir yi ? Dajale leen mu diw xiin, nga gis ndox di ca génnee bawoo asamaan. Ci tundi yuur lay sottikoo, Mu di ko dottil ku ko soob. Di ko xañ ku ko soob. Melxatug melaxam xaw naa mën a yàq ab gis.
44يُقَلِّبُ اللَّهُ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَعِبْرَةً لِّأُولِي الْأَبْصَارِ
Yàlla mooy jéllasante guddeek bëccëg. Boroom gis-gis yi mën nañu cee xalam.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
42Aaya
Tekki — An-Nur 42
Simoore An-Nur Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaay boroom nguurug asamaan yeek suuf si. Te ca Moom…Simoore Aaya 42/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








