Al-Furqan · 26/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
الْمُلْكُ يَوْمَئِذٍ الْحَقُّ لِلرَّحْمَٰنِ ۚ وَكَانَ يَوْمًا عَلَى الْكَافِرِينَ عَسِيرًا ۝٢٦
Almulku Yawma`izinil haqqu lir Rahmaan; wa kaana Yawman`alal kaafireena `aseeraa
📖 Tekkim Wolof
bu keroogee [buntub] nguur dëgg, Yërëmaakoon baa koy ame, mu doon nag Bis bu jafe ci yéefar yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Furqan

24أَصْحَابُ الْجَنَّةِ يَوْمَئِذٍ خَيْرٌ مُّسْتَقَرًّا وَأَحْسَنُ مَقِيلًا
[Bu keroogee Bis-pénc ba], waa Àjjana ñooy gën delluwaay te ñooy dàq ub nooflaay.
25وَيَوْمَ تَشَقَّقُ السَّمَاءُ بِالْغَمَامِ وَنُزِّلَ الْمَلَائِكَةُ تَنزِيلًا
[Bu Bis baa] ba niiri asamaan si di xottiku, ñuy wàcce Malaaka yi,
26الْمُلْكُ يَوْمَئِذٍ الْحَقُّ لِلرَّحْمَٰنِ ۚ وَكَانَ يَوْمًا عَلَى الْكَافِرِينَ عَسِيرًا
bu keroogee [buntub] nguur dëgg, Yërëmaakoon baa koy ame, mu doon nag Bis bu jafe ci yéefar yi.
27وَيَوْمَ يَعَضُّ الظَّالِمُ عَلَىٰ يَدَيْهِ يَقُولُ يَا لَيْتَنِي اتَّخَذْتُ مَعَ الرَّسُولِ سَبِيلًا
Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan : “Aka neexoon ma ànd ak Yonent aw yoon !...
28يَا وَيْلَتَىٰ لَيْتَنِي لَمْ أَتَّخِذْ فُلَانًا خَلِيلًا
Ngalla man ! Aka neexoon jàppewuma diw sàngam ab xarit !...
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Furqan 26

Simoore Al-Furqan Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu keroogee [buntub] nguur dëgg, Yërëmaakoon baa koy ame, mu…

Simoore Aaya 26/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers