Al-Furqan · 27/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَيَوْمَ يَعَضُّ الظَّالِمُ عَلَىٰ يَدَيْهِ يَقُولُ يَا لَيْتَنِي اتَّخَذْتُ مَعَ الرَّسُولِ سَبِيلًا ۝٢٧
Wa Yawma ya`adduz zaalimu `alaa yadaihi yaqoolu yaa laitanit takhaztu ma`ar Rasooli sabeelaa
📖 Tekkim Wolof
Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan : “Aka neexoon ma ànd ak Yonent aw yoon !...

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore Al-Furqan

25وَيَوْمَ تَشَقَّقُ السَّمَاءُ بِالْغَمَامِ وَنُزِّلَ الْمَلَائِكَةُ تَنزِيلًا
[Bu Bis baa] ba niiri asamaan si di xottiku, ñuy wàcce Malaaka yi,
26الْمُلْكُ يَوْمَئِذٍ الْحَقُّ لِلرَّحْمَٰنِ ۚ وَكَانَ يَوْمًا عَلَى الْكَافِرِينَ عَسِيرًا
bu keroogee [buntub] nguur dëgg, Yërëmaakoon baa koy ame, mu doon nag Bis bu jafe ci yéefar yi.
27وَيَوْمَ يَعَضُّ الظَّالِمُ عَلَىٰ يَدَيْهِ يَقُولُ يَا لَيْتَنِي اتَّخَذْتُ مَعَ الرَّسُولِ سَبِيلًا
Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan : “Aka neexoon ma ànd ak Yonent aw yoon !...
28يَا وَيْلَتَىٰ لَيْتَنِي لَمْ أَتَّخِذْ فُلَانًا خَلِيلًا
Ngalla man ! Aka neexoon jàppewuma diw sàngam ab xarit !...
29لَّقَدْ أَضَلَّنِي عَنِ الذِّكْرِ بَعْدَ إِذْ جَاءَنِي ۗ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِلْإِنسَانِ خَذُولًا
Moo ma féewaleek [Alxuraan] ginnaaw ba mu ma ñëwalee”. Séytaane moo di yàqalekat bu bon (bu yées ba).
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Furqan 27

Simoore Al-Furqan Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan…

Simoore Aaya 27/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers