Al-Furqan · 25/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَيَوْمَ تَشَقَّقُ السَّمَاءُ بِالْغَمَامِ وَنُزِّلَ الْمَلَائِكَةُ تَنزِيلًا ۝٢٥
Wa Yawma tashaqqaqus samaaa`u bilghamaami wa nuzzilal malaaa`ikatu tanzeela
📖 Tekkim Wolof
[Bu Bis baa] ba niiri asamaan si di xottiku, ñuy wàcce Malaaka yi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Furqan

23وَقَدِمْنَا إِلَىٰ مَا عَمِلُوا مِنْ عَمَلٍ فَجَعَلْنَاهُ هَبَاءً مَّنثُورًا
Nu fab jépp jëf ju ñu mësoon a jëf, def ko pënd bu ñu wasaare.
24أَصْحَابُ الْجَنَّةِ يَوْمَئِذٍ خَيْرٌ مُّسْتَقَرًّا وَأَحْسَنُ مَقِيلًا
[Bu keroogee Bis-pénc ba], waa Àjjana ñooy gën delluwaay te ñooy dàq ub nooflaay.
25وَيَوْمَ تَشَقَّقُ السَّمَاءُ بِالْغَمَامِ وَنُزِّلَ الْمَلَائِكَةُ تَنزِيلًا
[Bu Bis baa] ba niiri asamaan si di xottiku, ñuy wàcce Malaaka yi,
26الْمُلْكُ يَوْمَئِذٍ الْحَقُّ لِلرَّحْمَٰنِ ۚ وَكَانَ يَوْمًا عَلَى الْكَافِرِينَ عَسِيرًا
bu keroogee [buntub] nguur dëgg, Yërëmaakoon baa koy ame, mu doon nag Bis bu jafe ci yéefar yi.
27وَيَوْمَ يَعَضُّ الظَّالِمُ عَلَىٰ يَدَيْهِ يَقُولُ يَا لَيْتَنِي اتَّخَذْتُ مَعَ الرَّسُولِ سَبِيلًا
Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan : “Aka neexoon ma ànd ak Yonent aw yoon !...
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Furqan 25

Simoore Al-Furqan Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Bu Bis baa] ba niiri asamaan si di xottiku, ñuy…

Simoore Aaya 25/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers