Al-Furqan · 57/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ إِلَّا مَن شَاءَ أَن يَتَّخِذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا ٥٧
Transliteration
Qul maaa as`alukum `alaihi min ajrin illaa man shaaa`a ai yattakhiza ilaa Rabbihee sabeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Laaju ma leen ci ag pey. Ku mu soob nag, mën naa joxe ci yoonu Yàlla”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 55-59 — Al-Furqan
55وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَنفَعُهُمْ وَلَا يَضُرُّهُمْ ۗ وَكَانَ الْكَافِرُ عَلَىٰ رَبِّهِ ظَهِيرًا
[Yéefar ya], ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne duleen jariñ, duleen lor ! Ku di ab yéefar mooy takkatook noonub Boroomam !
56وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا مُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Yónniwunu la lu dul ngay xuppe ak a waare.
57قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ إِلَّا مَن شَاءَ أَن يَتَّخِذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Neel : “Laaju ma leen ci ag pey. Ku mu soob nag, mën naa joxe ci yoonu Yàlla”.
58وَتَوَكَّلْ عَلَى الْحَيِّ الَّذِي لَا يَمُوتُ وَسَبِّحْ بِحَمْدِهِ ۚ وَكَفَىٰ بِهِ بِذُنُوبِ عِبَادِهِ خَبِيرًا
Te nanga wéeru ci Yàlla Miy Aji-dund te du dee. Te nangay sàbbaal ci sant Ko. Moom Yàlla ku mat sëkk la ci xam bàkkaari jaamam ñi.
59الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ الرَّحْمَٰنُ فَاسْأَلْ بِهِ خَبِيرًا
Mooy Ki bind asamaan yaak suuf si ak li nekk seen diggante, ci juróom-benni fan, daldi yemoo ca gàngunaay ga [Aras], Moo di ab Yërëmaakoon. Laaj ko ku xam.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
57Aaya
Tekki — Al-Furqan 57
Simoore Al-Furqan Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Laaju ma leen ci ag pey. Ku mu…Simoore Aaya 57/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








