Ash-Shu'ara · 121/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ ١٢١
Transliteration
Inna fee zaalika la Aayaah; wa maa kaana aksaruhum mu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ay kéemaan a nga ci biir loolu. Te taxut woon la ëpp ci ñoom gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 119-123 — Ash-Shu'ara
119فَأَنجَيْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Nu daldi koy musal mook ña mu àndaloon ci gaal ga mu duyyoon ba mu fees.
120ثُمَّ أَغْرَقْنَا بَعْدُ الْبَاقِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
121إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a nga ci biir loolu. Te taxut woon la ëpp ci ñoom gëm.
122وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boorm, Mooy boroom kàttan, di Jaglewaakoon.
123كَذَّبَتْ عَادٌ الْمُرْسَلِينَ
Waa Haad, weddi woon nañu Yonent ya, jàppe leen ay fenkat.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
121Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 121
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 121 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay kéemaan a nga ci biir loolu. Te taxut woon…Simoore Aaya 121/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 119–123. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








