Ash-Shu'ara · 120/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
ثُمَّ أَغْرَقْنَا بَعْدُ الْبَاقِينَ ١٢٠
Transliteration
Summa aghraqnaa ba`dul baaqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 118-122 — Ash-Shu'ara
118فَافْتَحْ بَيْنِي وَبَيْنَهُمْ فَتْحًا وَنَجِّنِي وَمَن مَّعِيَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te nga musal maak ñi ma àndal te ñu bokk ca ña gëm”.
119فَأَنجَيْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Nu daldi koy musal mook ña mu àndaloon ci gaal ga mu duyyoon ba mu fees.
120ثُمَّ أَغْرَقْنَا بَعْدُ الْبَاقِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
121إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a nga ci biir loolu. Te taxut woon la ëpp ci ñoom gëm.
122وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boorm, Mooy boroom kàttan, di Jaglewaakoon.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
120Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 120
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 120 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.Simoore Aaya 120/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 118–122. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








