Ash-Shu'ara · 160/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ الْمُرْسَلِينَ ۝١٦٠
kazzabat qawmu Lootinil mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Nitu Lóot weddi woon nañu Yonent ya,

🎧 Dégg


📜 Aaya 158-162 — Simoore Ash-Shu'ara

158فَأَخَذَهُمُ الْعَذَابُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Mbugal ma dal leen. Ci biir loolu ay kéemaan a nga ca. Te taxul li ëpp ci ñoom gëm.
159وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, moo Boroom kàtta, di Jaglewaakoon bi.
160كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ الْمُرْسَلِينَ
Nitu Lóot weddi woon nañu Yonent ya,
161إِذْ قَالَ لَهُمْ أَخُوهُمْ لُوطٌ أَلَا تَتَّقُونَ
ba leen seen mbokk ma Lóot waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla ?
162إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man mii dey, ab Yonent laa ci yéen bu wóor.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
160Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 160

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 160 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nitu Lóot weddi woon nañu Yonent ya,

Simoore Aaya 160/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 158–162. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers