Ash-Shu'ara · 173/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ ۝١٧٣
Wa amtarnaa `alaihim mataran fasaaa`a matarul munzareen
📖 Tekkim Wolof
Nu dottil leen [taw] waame doj. A ndaw taw bu bon ca ña mu dal !

🎧 Dégg


📜 Aaya 171-175 — Ash-Shu'ara

171إِلَّا عَجُوزًا فِي الْغَابِرِينَ
ba mu des menn màggat mu àndoon ca mbokk ga.
172ثُمَّ دَمَّرْنَا الْآخَرِينَ
Topp [Nun Yàlla] Nu faagaagal ña des ;
173وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ
Nu dottil leen [taw] waame doj. A ndaw taw bu bon ca ña mu dal !
174إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña ëppoon ca ñoom gëm.
175وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Sa Boroom, Mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba [yërmaandeem].
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
173Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 173

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 173 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu dottil leen [taw] waame doj. A ndaw taw bu…

Simoore Aaya 173/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 171–175. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers