Ash-Shu'ara · 219/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَتَقَلُّبَكَ فِي السَّاجِدِينَ ۝٢١٩
Wa taqallubaka fis saajideen
📖 Tekkim Wolof
ak say jëfiin ba nga nekkee ci biir ñay sujjóot [julli].

🎧 Dégg


📜 Aaya 217-221 — Simoore Ash-Shu'ara

217وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,
218الَّذِي يَرَاكَ حِينَ تَقُومُ
Moom mi lay gis boo taxawee,
219وَتَقَلُّبَكَ فِي السَّاجِدِينَ
ak say jëfiin ba nga nekkee ci biir ñay sujjóot [julli].
220إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Mooy dégg, di xam.
221هَلْ أُنَبِّئُكُمْ عَلَىٰ مَن تَنَزَّلُ الشَّيَاطِينُ
Moo ndax Duma la xibaar ana kan la séytaane ya wàcce ca moom ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
219Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 219

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 219 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak say jëfiin ba nga nekkee ci biir ñay sujjóot…

Simoore Aaya 219/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 217–221. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers