Ash-Shu'ara · 218/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
الَّذِي يَرَاكَ حِينَ تَقُومُ ۝٢١٨
Allazee yaraaka heena taqoom
📖 Tekkim Wolof
Moom mi lay gis boo taxawee,

🎧 Dégg


📜 Aaya 216-220 — Ash-Shu'ara

216فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.
217وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,
218الَّذِي يَرَاكَ حِينَ تَقُومُ
Moom mi lay gis boo taxawee,
219وَتَقَلُّبَكَ فِي السَّاجِدِينَ
ak say jëfiin ba nga nekkee ci biir ñay sujjóot [julli].
220إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Mooy dégg, di xam.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
218Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 218

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 218 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mi lay gis boo taxawee,

Simoore Aaya 218/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 216–220. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers