Ash-Shu'ara · 28/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالَ رَبُّ الْمَشْرِقِ وَالْمَغْرِبِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُمْ تَعْقِلُونَ ۝٢٨
Qaala Rabbul mashriqi wal maghribi wa maa baina humaa in kuntum ta`qiloon
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa] ne ko : “Mooy Boroom penkook sowwu ak li nekk seen diggante, bu ngeen xel-

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Ash-Shu'ara

26قَالَ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
[Muusaa] ne ko : “... Mooy seen Boroom, di Boroomub seeni baay”.
27قَالَ إِنَّ رَسُولَكُمُ الَّذِي أُرْسِلَ إِلَيْكُمْ لَمَجْنُونٌ
[Firawna] daldi wax ne : “Seen Yonent bii ñu leen yónni ab dof la kat”.
28قَالَ رَبُّ الْمَشْرِقِ وَالْمَغْرِبِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُمْ تَعْقِلُونَ
[Muusaa] ne ko : “Mooy Boroom penkook sowwu ak li nekk seen diggante, bu ngeen xel-
29قَالَ لَئِنِ اتَّخَذْتَ إِلَٰهًا غَيْرِي لَأَجْعَلَنَّكَ مِنَ الْمَسْجُونِينَ
[Firawna] ne ko : “Soo fi jéemee indi jeneen yàlla ju dul man, danaa la téj kaso de”.
30قَالَ أَوَلَوْ جِئْتُكَ بِشَيْءٍ مُّبِينٍ
[Muusaa] ne ko : “Moo ne indil naa la mbir mu leer de ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 28

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa] ne ko : “Mooy Boroom penkook sowwu ak li…

Simoore Aaya 28/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers