Ash-Shu'ara · 29/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ لَئِنِ اتَّخَذْتَ إِلَٰهًا غَيْرِي لَأَجْعَلَنَّكَ مِنَ الْمَسْجُونِينَ ٢٩
Transliteration
Qaala la`init takhazta ilaahan ghairee la aj`alannaka minal masjooneen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne ko : “Soo fi jéemee indi jeneen yàlla ju dul man, danaa la téj kaso de”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 27-31 — Ash-Shu'ara
27قَالَ إِنَّ رَسُولَكُمُ الَّذِي أُرْسِلَ إِلَيْكُمْ لَمَجْنُونٌ
[Firawna] daldi wax ne : “Seen Yonent bii ñu leen yónni ab dof la kat”.
28قَالَ رَبُّ الْمَشْرِقِ وَالْمَغْرِبِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُمْ تَعْقِلُونَ
[Muusaa] ne ko : “Mooy Boroom penkook sowwu ak li nekk seen diggante, bu ngeen xel-
29قَالَ لَئِنِ اتَّخَذْتَ إِلَٰهًا غَيْرِي لَأَجْعَلَنَّكَ مِنَ الْمَسْجُونِينَ
[Firawna] ne ko : “Soo fi jéemee indi jeneen yàlla ju dul man, danaa la téj kaso de”.
30قَالَ أَوَلَوْ جِئْتُكَ بِشَيْءٍ مُّبِينٍ
[Muusaa] ne ko : “Moo ne indil naa la mbir mu leer de ?
31قَالَ فَأْتِ بِهِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
[Firawna] ne ko : “Génne ko bu fekkee li ngay wax dëgg la”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
29Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 29
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne ko : “Soo fi jéemee indi jeneen yàlla…Simoore Aaya 29/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








