Ash-Shu'ara · 38/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَجُمِعَ السَّحَرَةُ لِمِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ ٣٨
Transliteration
Fa jumi`as saharatu limeeqaati Yawmim ma`loom
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Ash-Shu'ara
36قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَابْعَثْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Joxleen ñoom ñaar beneen bis te nga yónni ci gox yi ñuy woo nit ñi, di leen
dajale,
37يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَحَّارٍ عَلِيمٍ
danañu la indil bépp jibar bu fi xor”.
38فَجُمِعَ السَّحَرَةُ لِمِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.
39وَقِيلَ لِلنَّاسِ هَلْ أَنتُم مُّجْتَمِعُونَ
Mu am ku yéene wax ne : “Ndax nit ñépp yemb nañu,
40لَعَلَّنَا نَتَّبِعُ السَّحَرَةَ إِن كَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
xéy-na bu nu toppee njibarkat yi, ndegam ñoo not ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 38
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.Simoore Aaya 38/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








