Ash-Shu'ara · 39/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَقِيلَ لِلنَّاسِ هَلْ أَنتُم مُّجْتَمِعُونَ ۝٣٩
Wa qeela linnaasi hal antum mujtami`oon
📖 Tekkim Wolof
Mu am ku yéene wax ne : “Ndax nit ñépp yemb nañu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Ash-Shu'ara

37يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَحَّارٍ عَلِيمٍ
danañu la indil bépp jibar bu fi xor”.
38فَجُمِعَ السَّحَرَةُ لِمِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.
39وَقِيلَ لِلنَّاسِ هَلْ أَنتُم مُّجْتَمِعُونَ
Mu am ku yéene wax ne : “Ndax nit ñépp yemb nañu,
40لَعَلَّنَا نَتَّبِعُ السَّحَرَةَ إِن كَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
xéy-na bu nu toppee njibarkat yi, ndegam ñoo not ? ”
41فَلَمَّا جَاءَ السَّحَرَةُ قَالُوا لِفِرْعَوْنَ أَئِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ
Ba jibar ya agsee, dellu wax Firawna ne ko : “Ndax dananu am ag pey bu fekkee ne not nanu [Muusaa] ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 39

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am ku yéene wax ne : “Ndax nit ñépp…

Simoore Aaya 39/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers