Ash-Shu'ara · 40/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
لَعَلَّنَا نَتَّبِعُ السَّحَرَةَ إِن كَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ ٤٠
Transliteration
La`allanaa nattabi`us saharata in kaanoo humul ghaalibeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
xéy-na bu nu toppee njibarkat yi, ndegam ñoo not ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 38-42 — Ash-Shu'ara
38فَجُمِعَ السَّحَرَةُ لِمِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.
39وَقِيلَ لِلنَّاسِ هَلْ أَنتُم مُّجْتَمِعُونَ
Mu am ku yéene wax ne : “Ndax nit ñépp yemb nañu,
40لَعَلَّنَا نَتَّبِعُ السَّحَرَةَ إِن كَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
xéy-na bu nu toppee njibarkat yi, ndegam ñoo not ? ”
41فَلَمَّا جَاءَ السَّحَرَةُ قَالُوا لِفِرْعَوْنَ أَئِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ
Ba jibar ya agsee, dellu wax Firawna ne ko : “Ndax dananu am ag pey bu fekkee ne not nanu [Muusaa] ? ”
42قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ إِذًا لَّمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dingeen bokk ci samay jegeñaale !
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
40Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 40
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : xéy-na bu nu toppee njibarkat yi, ndegam ñoo not ?…Simoore Aaya 40/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








