Ash-Shu'ara · 67/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ ۝٦٧
Inna fee zaalika la Aayaah; wa maa kaana aksaru hu mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Kéemaan a ngi ci biir loolu te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 65-69 — Simoore Ash-Shu'ara

65وَأَنجَيْنَا مُوسَىٰ وَمَن مَّعَهُ أَجْمَعِينَ
Nu daldi musal Muusaa mook ña mu àndanloon ñépp ;
66ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Nu daldi labal ña ca des [Firawna ak i gaayam].
67إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Kéemaan a ngi ci biir loolu te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.
68وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.
69وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ إِبْرَاهِيمَ
Jàngal-leen xibaari Ibraahiima:
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 67

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kéemaan a ngi ci biir loolu te taxut woon li…

Simoore Aaya 67/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers