Ash-Shu'ara · 68/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ ۝٦٨
Wa inna Rabbaka la Huwal `Azeezur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Te sa Boroom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 66-70 — Simoore Ash-Shu'ara

66ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Nu daldi labal ña ca des [Firawna ak i gaayam].
67إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Kéemaan a ngi ci biir loolu te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.
68وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.
69وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ إِبْرَاهِيمَ
Jàngal-leen xibaari Ibraahiima:
70إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَا تَعْبُدُونَ
Ba mu waxee baayam ak u nitam, ne leen : “Lu ngeen di jaamu ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
68Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 68

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sa Boroom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.

Simoore Aaya 68/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers