Ash-Shu'ara · 69/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ إِبْرَاهِيمَ ۝٦٩
Watlu `alaihim naba-a Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
Jàngal-leen xibaari Ibraahiima:

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore Ash-Shu'ara

67إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Kéemaan a ngi ci biir loolu te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.
68وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.
69وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ إِبْرَاهِيمَ
Jàngal-leen xibaari Ibraahiima:
70إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَا تَعْبُدُونَ
Ba mu waxee baayam ak u nitam, ne leen : “Lu ngeen di jaamu ? ”
71قَالُوا نَعْبُدُ أَصْنَامًا فَنَظَلُّ لَهَا عَاكِفِينَ
Ñu ne ko : “Ay xërëm lanuy jaamu, te gëm ko lool”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 69

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jàngal-leen xibaari Ibraahiima:

Simoore Aaya 69/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers