Ash-Shu'ara · 86/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَاغْفِرْ لِأَبِي إِنَّهُ كَانَ مِنَ الضَّالِّينَ ٨٦
Transliteration
Waghfir li abeee innahoo kaana mind daalleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
te Nga jéggal sama baay : moom dafa bokk ca ñu réer ña ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 84-88 — Ash-Shu'ara
84وَاجْعَل لِّي لِسَانَ صِدْقٍ فِي الْآخِرِينَ
defal ma am làmmiñ wu dëggu;
85وَاجْعَلْنِي مِن وَرَثَةِ جَنَّةِ النَّعِيمِ
def ma ma bokk ca way-donn ya Àjjanay xéewal ya.
86وَاغْفِرْ لِأَبِي إِنَّهُ كَانَ مِنَ الضَّالِّينَ
te Nga jéggal sama baay : moom dafa bokk ca ñu réer ña ;
87وَلَا تُخْزِنِي يَوْمَ يُبْعَثُونَ
te bul ma gàcceel kerook bisub dekki ba,
88يَوْمَ لَا يَنفَعُ مَالٌ وَلَا بَنُونَ
bis ba alal ak i doom du jariñati,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
86Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 86
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Nga jéggal sama baay : moom dafa bokk ca…Simoore Aaya 86/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








