Ash-Shu'ara · 87/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَلَا تُخْزِنِي يَوْمَ يُبْعَثُونَ ۝٨٧
Wa laa tukhzinee Yawma yub`asoon
📖 Tekkim Wolof
te bul ma gàcceel kerook bisub dekki ba,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 85-89 — Simoore Ash-Shu'ara

85وَاجْعَلْنِي مِن وَرَثَةِ جَنَّةِ النَّعِيمِ
def ma ma bokk ca way-donn ya Àjjanay xéewal ya.
86وَاغْفِرْ لِأَبِي إِنَّهُ كَانَ مِنَ الضَّالِّينَ
te Nga jéggal sama baay : moom dafa bokk ca ñu réer ña ;
87وَلَا تُخْزِنِي يَوْمَ يُبْعَثُونَ
te bul ma gàcceel kerook bisub dekki ba,
88يَوْمَ لَا يَنفَعُ مَالٌ وَلَا بَنُونَ
bis ba alal ak i doom du jariñati,
89إِلَّا مَنْ أَتَى اللَّهَ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
ku dul kay ñëw ca Yàllaak xol bu mucc ayib”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
87Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 87

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te bul ma gàcceel kerook bisub dekki ba,

Simoore Aaya 87/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 85–89. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers