An-Naml · 58/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ ۝٥٨
Wa amtarnaa `alaihimm mataran fasaaa`a matarul munzareen
📖 Tekkim Wolof
Dotti Nanu ca seen kaw waamem [doj]. Ndaw taw bu bon ca ña mu dal ca seen kaw!

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 56-60 — Simoore An-Naml

56۞ فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا أَخْرِجُوا آلَ لُوطٍ مِّن قَرْيَتِكُمْ ۖ إِنَّهُمْ أُنَاسٌ يَتَطَهَّرُونَ
Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot ci seen dëkk bii ! Ndax ñoom dañuy jéem a laab-laablu.
57فَأَنجَيْنَاهُ وَأَهْلَهُ إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَاهَا مِنَ الْغَابِرِينَ
Nu daldi koy musal mook njabootam ga ba mu des soxnaam sa àndoon ak defkatu ñaawtéef ya Nu faagaagal.
58وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ
Dotti Nanu ca seen kaw waamem [doj]. Ndaw taw bu bon ca ña mu dal ca seen kaw!
59قُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ وَسَلَامٌ عَلَىٰ عِبَادِهِ الَّذِينَ اصْطَفَىٰ ۗ آللَّهُ خَيْرٌ أَمَّا يُشْرِكُونَ
Waxal : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla te yal na jàmm wàcc ci kaw jaamam ña Mu tànn ! ” Waaw! Ana lan moo gën : Yàlla walla li ngeen di bokkaale ?
60أَمَّنْ خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَأَنزَلَ لَكُم مِّنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَنبَتْنَا بِهِ حَدَائِقَ ذَاتَ بَهْجَةٍ مَّا كَانَ لَكُمْ أَن تُنبِتُوا شَجَرَهَا ۗ أَإِلَٰهٌ مَّعَ اللَّهِ ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ يَعْدِلُونَ
Ana kan moo bind [sàkk] asamaan yeek suuf si te Mu wàcceel leen am ndox mu bawoo asamaan, daldi cay saxale ay tool yu taaru yoo xam ne mënuleen ko woon a saxal. Moo ndax dafa am jeneen yàlla juy ànd ak Yàlla ? [Amul], ñoom kay fu ñu toll ña ngay jéem a utal Yàlla ndend.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — An-Naml 58

Simoore An-Naml Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dotti Nanu ca seen kaw waamem [doj]. Ndaw taw bu…

Simoore Aaya 58/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers