An-Naml · 57/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
فَأَنجَيْنَاهُ وَأَهْلَهُ إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَاهَا مِنَ الْغَابِرِينَ ٥٧
Transliteration
Fa anjainaahu wa ahlahooo illam ra atahoo qaddarnaahaa minal ghaabireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi koy musal mook njabootam ga ba mu des soxnaam sa àndoon ak defkatu ñaawtéef ya Nu faagaagal.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 55-59 — An-Naml
55أَئِنَّكُمْ لَتَأْتُونَ الرِّجَالَ شَهْوَةً مِّن دُونِ النِّسَاءِ ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تَجْهَلُونَ
Ndax dangeen di gën a xemmem góor ñi bàyyi jigéen ñi ? Yéen daal aw nit ñu réer ngeen.
56۞ فَمَا كَانَ جَوَابَ قَوْمِهِ إِلَّا أَن قَالُوا أَخْرِجُوا آلَ لُوطٍ مِّن قَرْيَتِكُمْ ۖ إِنَّهُمْ أُنَاسٌ يَتَطَهَّرُونَ
Nitam ña tontuwuñu lu dul ne : “Génneleen njabootug Lóot ci seen dëkk bii ! Ndax ñoom dañuy jéem a laab-laablu.
57فَأَنجَيْنَاهُ وَأَهْلَهُ إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَاهَا مِنَ الْغَابِرِينَ
Nu daldi koy musal mook njabootam ga ba mu des soxnaam sa àndoon ak defkatu ñaawtéef ya Nu faagaagal.
58وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِم مَّطَرًا ۖ فَسَاءَ مَطَرُ الْمُنذَرِينَ
Dotti Nanu ca seen kaw waamem [doj]. Ndaw taw bu bon ca ña mu dal ca seen kaw!
59قُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ وَسَلَامٌ عَلَىٰ عِبَادِهِ الَّذِينَ اصْطَفَىٰ ۗ آللَّهُ خَيْرٌ أَمَّا يُشْرِكُونَ
Waxal : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla te yal na jàmm wàcc ci kaw jaamam ña Mu tànn ! ” Waaw! Ana lan moo gën : Yàlla walla li ngeen di bokkaale ?
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
57Aaya
Tekki — An-Naml 57
Simoore An-Naml Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi koy musal mook njabootam ga ba mu des…Simoore Aaya 57/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, August 19, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








