An-Naml · 74/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ ۝٧٤
Wa inna Rabbaka la ya`lamu maa tukinnu sudooruhum wa maa yu`linoon
📖 Tekkim Wolof
Te it sa Boroom xam na li ngeen rënk ci seeni dënn ak li ngeen di feeñal.
🎧 Dégg

📜 Aaya 72-76 — An-Naml

72قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ رَدِفَ لَكُم بَعْضُ الَّذِي تَسْتَعْجِلُونَ
Neel : “Amaana lii ngeen di yàkkamtee ngi ci seen kaw”.
73وَإِنَّ رَبَّكَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَشْكُرُونَ
Te nag sa Boroom aka bari ngëneel yu Muy jox nit ñi, waaye li ëpp ci ñoom duñu sant.
74وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ
Te it sa Boroom xam na li ngeen rënk ci seeni dënn ak li ngeen di feeñal.
75وَمَا مِنْ غَائِبَةٍ فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ إِلَّا فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ
Te it amul lenn lu fàddu nekk ci asamaan si walla ci suuf si te dul ne nekk na ci biir ab Téere bu ñu faramfàcce.
76إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَقُصُّ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ أَكْثَرَ الَّذِي هُمْ فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Alxuraan jii dafay nettali ci giir Bani-Israayiila, li ëpp ci la ñu daan juuyoo ak a wuute,
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — An-Naml 74

Simoore An-Naml Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it sa Boroom xam na li ngeen rënk ci…

Simoore Aaya 74/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers