Al-Qasas · 80/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَقَالَ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ وَيْلَكُمْ ثَوَابُ اللَّهِ خَيْرٌ لِّمَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا وَلَا يُلَقَّاهَا إِلَّا الصَّابِرُونَ ۝٨٠
Wa qaalal lazeena ootul `ilma wailakum sawaabul laahi khairul liman aamana wa `amila saalihaa; wa laa yulaq qaahaaa illas saabiroon
📖 Tekkim Wolof
Ña am xam-xam ne leen : “Toskare ngeen ! Yoolub Yàllaa gënal képp ku gëm tey jëf u yiw”. Ku dul muñkat du ko am.

🎧 Dégg


📜 Aaya 78-82 — Simoore Al-Qasas

78قَالَ إِنَّمَا أُوتِيتُهُ عَلَىٰ عِلْمٍ عِندِي ۚ أَوَلَمْ يَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ قَدْ أَهْلَكَ مِن قَبْلِهِ مِنَ الْقُرُونِ مَنْ هُوَ أَشَدُّ مِنْهُ قُوَّةً وَأَكْثَرُ جَمْعًا ۚ وَلَا يُسْأَلُ عَن ذُنُوبِهِمُ الْمُجْرِمُونَ
Xaaruuna wax ne : “Lii ci sama xam-xam laa ko ame”. Xanaa moom dafa xamul ña Yàlla faagaagal ca maas ya ko jiitu, ña ko gënoon a ñàng ëpp ko fuuf dooleek alal ? Te tooñkat ña deefuleen laaj seen bàkkaar !
79فَخَرَجَ عَلَىٰ قَوْمِهِ فِي زِينَتِهِ ۖ قَالَ الَّذِينَ يُرِيدُونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا يَا لَيْتَ لَنَا مِثْلَ مَا أُوتِيَ قَارُونُ إِنَّهُ لَذُو حَظٍّ عَظِيمٍ
Mu génn ca nitam ña, ànd ak alalam ja. Ñi bëgg dundu àddina wax ne : “Aka neexoon nu am lii Xaaruuna am. Moom dey boroom cër bu duun na”.
80وَقَالَ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ وَيْلَكُمْ ثَوَابُ اللَّهِ خَيْرٌ لِّمَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا وَلَا يُلَقَّاهَا إِلَّا الصَّابِرُونَ
Ña am xam-xam ne leen : “Toskare ngeen ! Yoolub Yàllaa gënal képp ku gëm tey jëf u yiw”. Ku dul muñkat du ko am.
81فَخَسَفْنَا بِهِ وَبِدَارِهِ الْأَرْضَ فَمَا كَانَ لَهُ مِن فِئَةٍ يَنصُرُونَهُ مِن دُونِ اللَّهِ وَمَا كَانَ مِنَ الْمُنتَصِرِينَ
Nu mëdd ko ci biir suuf si mook kërëm ga. Amul kenn ku ko mënoon a dimbali ku dul Yàlla, te it kenn dimbaliwu ko woon.
82وَأَصْبَحَ الَّذِينَ تَمَنَّوْا مَكَانَهُ بِالْأَمْسِ يَقُولُونَ وَيْكَأَنَّ اللَّهَ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ وَيَقْدِرُ ۖ لَوْلَا أَن مَّنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا لَخَسَفَ بِنَا ۖ وَيْكَأَنَّهُ لَا يُفْلِحُ الْكَافِرُونَ
Ba ñu xëyee, ña doon xemmem wàccuwaayam ca démb sa, daldi wax ne : “Dafa mel ni Yàlla dana tàbbalal wërsëg ku ko neex, ci jaamam yi. Bu dul kon ak xéewalam, kon dey mëddoon Nanu. Te it yéefar yi duñu texe”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Al-Qasas 80

Simoore Al-Qasas Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña am xam-xam ne leen : “Toskare ngeen ! Yoolub…

Simoore Aaya 80/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers