Al-Qasas · 85/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
إِنَّ الَّذِي فَرَضَ عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لَرَادُّكَ إِلَىٰ مَعَادٍ ۚ قُل رَّبِّي أَعْلَمُ مَن جَاءَ بِالْهُدَىٰ وَمَنْ هُوَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ ٨٥
Transliteration
Innal azee farada `alaikal Qur-aana laraaadduka ilaa ma`aad; qur Rabbeee a`lamu man jjaaa`a bil hudaa wa man huwa fee dalaalim mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] mi wàcce Alxuraan ci yaw, Moo lay delloo fa Màkka. Neel : “Sama Boroom moo gën a xaw kuy indi dëgg ak kuy nekk ci réer gu bir.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-87 — Al-Qasas
83تِلْكَ الدَّارُ الْآخِرَةُ نَجْعَلُهَا لِلَّذِينَ لَا يُرِيدُونَ عُلُوًّا فِي الْأَرْضِ وَلَا فَسَادًا ۚ وَالْعَاقِبَةُ لِلْمُتَّقِينَ
Góogale mooy kër gu mujj ga, Dananu ko defal ñi bëggul a kawe-kawelu ci suuf si, te duñu yàq. Ña ragal Yàlla tey moytandiku ñooy ëppug mujj.
84مَن جَاءَ بِالْحَسَنَةِ فَلَهُ خَيْرٌ مِّنْهَا ۖ وَمَن جَاءَ بِالسَّيِّئَةِ فَلَا يُجْزَى الَّذِينَ عَمِلُوا السَّيِّئَاتِ إِلَّا مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
[Amul lu ñu bàyyi fii], Ku dikk ak i ñaawtéef, [na xam ne] ñay jëf ñaawtéef, la ñu daan def rekk la ñu leen di feye.
85إِنَّ الَّذِي فَرَضَ عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لَرَادُّكَ إِلَىٰ مَعَادٍ ۚ قُل رَّبِّي أَعْلَمُ مَن جَاءَ بِالْهُدَىٰ وَمَنْ هُوَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
[Yàlla] mi wàcce Alxuraan ci yaw, Moo lay delloo fa Màkka. Neel : “Sama Boroom moo gën a xaw kuy indi dëgg ak kuy nekk ci réer gu bir.
86وَمَا كُنتَ تَرْجُو أَن يُلْقَىٰ إِلَيْكَ الْكِتَابُ إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۖ فَلَا تَكُونَنَّ ظَهِيرًا لِّلْكَافِرِينَ
Musuloo yaakaar ne dees na la jox Téere ba. Lu dul ne yërmaande ju bawoo ca sa Boroom. Te bul dimbali mukk yéefar yi ;
87وَلَا يَصُدُّنَّكَ عَنْ آيَاتِ اللَّهِ بَعْدَ إِذْ أُنزِلَتْ إِلَيْكَ ۖ وَادْعُ إِلَىٰ رَبِّكَ ۖ وَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
te it buñu la fàbbi mukk ci kàdduy Yàlla ginnaaw ba Nu ko wàccee ci yaw. Nangay woote jëme ci sa Boroom te bul bokk ca way-bokkaale ña.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Al-Qasas 85
Simoore Al-Qasas Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] mi wàcce Alxuraan ci yaw, Moo lay delloo fa…Simoore Aaya 85/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








