Al-'Ankabut · 57/69
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Ankabut
كُلُّ نَفْسٍ ذَائِقَةُ الْمَوْتِ ۖ ثُمَّ إِلَيْنَا تُرْجَعُونَ ۝٥٧
Kullu nafsin zaaa`iqatul mawti summa ilainaa turja`oon
📖 Tekkim Wolof
Bakkan bu nekk dana mos dee. Te [ñéppay] dellusi ci Nun.

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Simoore Al-'Ankabut

55يَوْمَ يَغْشَاهُمُ الْعَذَابُ مِن فَوْقِهِمْ وَمِن تَحْتِ أَرْجُلِهِمْ وَيَقُولُ ذُوقُوا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Bu keroogee ba mbugal ma muur leen ci seen kaw ak seen ndëgguy tànk. Mu di leen wax naan : “Mosleen, toqamtikuleen li ngeen daan def ! ”
56يَا عِبَادِيَ الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّ أَرْضِي وَاسِعَةٌ فَإِيَّايَ فَاعْبُدُونِ
Éy yéen sama jaam ñi gëm ! Sama suuf si yaatu na [lool]. Waay-waay jaamuleen Ma !
57كُلُّ نَفْسٍ ذَائِقَةُ الْمَوْتِ ۖ ثُمَّ إِلَيْنَا تُرْجَعُونَ
Bakkan bu nekk dana mos dee. Te [ñéppay] dellusi ci Nun.
58وَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَنُبَوِّئَنَّهُم مِّنَ الْجَنَّةِ غُرَفًا تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ نِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ
Ña gëmoon tey jëf u yiw, Dananu leen dëkkal ay néeg yu kawe yoo xam ne ay dex ñooy daw ca suufam. Dañu fay béel, ndaw pey gu neex,
59الَّذِينَ صَبَرُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
ña daan muñ te wéeru woon ca seen Boroom !
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 57

Simoore Al-'Ankabut Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bakkan bu nekk dana mos dee. Te [ñéppay] dellusi ci…

Simoore Aaya 57/69 — Simoore Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Ankabut Dégg, Simoore Al-'Ankabut Tekki, Simoore Al-'Ankabut mp3, Simoore Al-'Ankabut pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers