Ar-Rum · 12/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ يُبْلِسُ الْمُجْرِمُونَ ۝١٢
Wa yawma taqoomus Saa`atu yublisul mujrimoon
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee bu Bis-pénc ba di taxaw, tooñkat ya danañu naan cucum jaaxle.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Ar-Rum

10ثُمَّ كَانَ عَاقِبَةَ الَّذِينَ أَسَاءُوا السُّوأَىٰ أَن كَذَّبُوا بِآيَاتِ اللَّهِ وَكَانُوا بِهَا يَسْتَهْزِئُونَ
Ña daan jëf u ñaawteef, seenug mujj dellu ñaaw, ndax ñoom weddi woon nañu kàdduy Yàlla, daan ko yéjji.
11اللَّهُ يَبْدَأُ الْخَلْقَ ثُمَّ يُعِيدُهُ ثُمَّ إِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Yàllaa bind yëf yi ; yi di ko defaraat ; te ca Moom la ñuy dellu.
12وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ يُبْلِسُ الْمُجْرِمُونَ
Bu keroogee bu Bis-pénc ba di taxaw, tooñkat ya danañu naan cucum jaaxle.
13وَلَمْ يَكُن لَّهُم مِّن شُرَكَائِهِمْ شُفَعَاءُ وَكَانُوا بِشُرَكَائِهِمْ كَافِرِينَ
Ña ñu daan bokkaaleek Yàlla duñu leen rammu, te sax far dañuy weddi ña ñu daan bokkaaleek [Yàlla].
14وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ يَوْمَئِذٍ يَتَفَرَّقُونَ
Bu kerook Bis-pénc baa, dañuy téqalikoo, féewoo.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Ar-Rum 12

Simoore Ar-Rum Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee bu Bis-pénc ba di taxaw, tooñkat ya danañu…

Simoore Aaya 12/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers