Ar-Rum · 58/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
وَلَقَدْ ضَرَبْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ ۚ وَلَئِن جِئْتَهُم بِآيَةٍ لَّيَقُولَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ أَنتُمْ إِلَّا مُبْطِلُونَ ۝٥٨
Wa laqad darabnaa linnaasi fee haazal Quraani min kulli masal; wa la`in ji`tahum bi aayatil la yaqoolannal lazeena kafaroo in antum illaa mubtiloon
📖 Tekkim Wolof
Saddal Nanu nit ci biir Alxuraan jii léebu wu nekk. Soo leen indiloon kéemaan it, yéefar ya dañu naan : “Yéen daal, ay caaxaankat doŋŋ ngeen”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 56-60 — Ar-Rum

56وَقَالَ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ وَالْإِيمَانَ لَقَدْ لَبِثْتُمْ فِي كِتَابِ اللَّهِ إِلَىٰ يَوْمِ الْبَعْثِ ۖ فَهَٰذَا يَوْمُ الْبَعْثِ وَلَٰكِنَّكُمْ كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Gaa ña amoon xam-xam ak ngëm, ne leen : “Sax ngeen fa ci dogalu Yàlla ba bisub dekki ba, - lii nag mooy bisub dekki ba, - waaye yéen xamuleen woon”.
57فَيَوْمَئِذٍ لَّا يَنفَعُ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَعْذِرَتُهُمْ وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Su boobaa, tooñkat ya, seenug tinu du fa jariñ dara te kenn duleen faale.
58وَلَقَدْ ضَرَبْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ ۚ وَلَئِن جِئْتَهُم بِآيَةٍ لَّيَقُولَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ أَنتُمْ إِلَّا مُبْطِلُونَ
Saddal Nanu nit ci biir Alxuraan jii léebu wu nekk. Soo leen indiloon kéemaan it, yéefar ya dañu naan : “Yéen daal, ay caaxaankat doŋŋ ngeen”.
59كَذَٰلِكَ يَطْبَعُ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِ الَّذِينَ لَا يَعْلَمُونَ
Noonu la Yàlla di fattee xoli ña xamadi.
60فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ ۖ وَلَا يَسْتَخِفَّنَّكَ الَّذِينَ لَا يُوقِنُونَ
Muñal ndax digub Yàlla la dellu [yàgg yàgg dina ñëw]. Ñi gëmul, buñu la yàkki !
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Ar-Rum 58

Simoore Ar-Rum Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saddal Nanu nit ci biir Alxuraan jii léebu wu nekk.…

Simoore Aaya 58/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers