Ar-Rum · 59/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
كَذَٰلِكَ يَطْبَعُ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِ الَّذِينَ لَا يَعْلَمُونَ ۝٥٩
Kazaalika yatba`ul laahu `alaa quloobil lazeena laa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Yàlla di fattee xoli ña xamadi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-60 — Simoore Ar-Rum

57فَيَوْمَئِذٍ لَّا يَنفَعُ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَعْذِرَتُهُمْ وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Su boobaa, tooñkat ya, seenug tinu du fa jariñ dara te kenn duleen faale.
58وَلَقَدْ ضَرَبْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ ۚ وَلَئِن جِئْتَهُم بِآيَةٍ لَّيَقُولَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ أَنتُمْ إِلَّا مُبْطِلُونَ
Saddal Nanu nit ci biir Alxuraan jii léebu wu nekk. Soo leen indiloon kéemaan it, yéefar ya dañu naan : “Yéen daal, ay caaxaankat doŋŋ ngeen”.
59كَذَٰلِكَ يَطْبَعُ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِ الَّذِينَ لَا يَعْلَمُونَ
Noonu la Yàlla di fattee xoli ña xamadi.
60فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ ۖ وَلَا يَسْتَخِفَّنَّكَ الَّذِينَ لَا يُوقِنُونَ
Muñal ndax digub Yàlla la dellu [yàgg yàgg dina ñëw]. Ñi gëmul, buñu la yàkki !
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Ar-Rum 59

Simoore Ar-Rum Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Yàlla di fattee xoli ña xamadi.

Simoore Aaya 59/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 57–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers