Ya-Sin · 18/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
قَالُوا إِنَّا تَطَيَّرْنَا بِكُمْ ۖ لَئِن لَّمْ تَنتَهُوا لَنَرْجُمَنَّكُمْ وَلَيَمَسَّنَّكُم مِّنَّا عَذَابٌ أَلِيمٌ ١٨
Transliteration
Qaaloo innaa tataiyarnaa bikum la`il-lam tantahoo lanar jumannakum wa la-yamassan nakum minnaa `azaabun aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Gaafal nanu leen. Te bu ngeen bàyyiwul, dananu leen jóori xeer te dananu leen mbugal mbugal mu tar”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — Ya-Sin
16قَالُوا رَبُّنَا يَعْلَمُ إِنَّا إِلَيْكُمْ لَمُرْسَلُونَ
[Yonent ya] waxaat ne : “Yàlla xam na ne nun ay Yonent lanu ci yéen.
17وَمَا عَلَيْنَا إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
te dara warunu lu dul jottali ba mu leer nàññ.”
18قَالُوا إِنَّا تَطَيَّرْنَا بِكُمْ ۖ لَئِن لَّمْ تَنتَهُوا لَنَرْجُمَنَّكُمْ وَلَيَمَسَّنَّكُم مِّنَّا عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ñu ne : “Gaafal nanu leen. Te bu ngeen bàyyiwul, dananu leen jóori xeer te dananu leen mbugal mbugal mu tar”.
19قَالُوا طَائِرُكُم مَّعَكُمْ ۚ أَئِن ذُكِّرْتُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ مُّسْرِفُونَ
Yonent ya ne leen : “Seen gaaf googu mook yéen a ànd”. Moo ndax fàttaliwunu leen woon ? Yéen daal dangeen a yebaate ! ”.
20وَجَاءَ مِنْ أَقْصَى الْمَدِينَةِ رَجُلٌ يَسْعَىٰ قَالَ يَا قَوْمِ اتَّبِعُوا الْمُرْسَلِينَ
Mu am waa ju jóge woon ca anéeri dëkk ba, di dox ne leen : “Éy yéen samaw nit, moo tee ngeen a topp Yonent yi :
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
18Aaya
Tekki — Ya-Sin 18
Simoore Ya-Sin Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Gaafal nanu leen. Te bu ngeen bàyyiwul,…Simoore Aaya 18/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








