Ya-Sin · 21/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
اتَّبِعُوا مَن لَّا يَسْأَلُكُمْ أَجْرًا وَهُم مُّهْتَدُونَ ۝٢١
Ittabi`oo mal-laa yas`alukum ajranw-wa hum muhtadoon
📖 Tekkim Wolof
Toppleen ku dul laaj ag pey te ñoom ñu gindiku lañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Ya-Sin

19قَالُوا طَائِرُكُم مَّعَكُمْ ۚ أَئِن ذُكِّرْتُم ۚ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ مُّسْرِفُونَ
Yonent ya ne leen : “Seen gaaf googu mook yéen a ànd”. Moo ndax fàttaliwunu leen woon ? Yéen daal dangeen a yebaate ! ”.
20وَجَاءَ مِنْ أَقْصَى الْمَدِينَةِ رَجُلٌ يَسْعَىٰ قَالَ يَا قَوْمِ اتَّبِعُوا الْمُرْسَلِينَ
Mu am waa ju jóge woon ca anéeri dëkk ba, di dox ne leen : “Éy yéen samaw nit, moo tee ngeen a topp Yonent yi :
21اتَّبِعُوا مَن لَّا يَسْأَلُكُمْ أَجْرًا وَهُم مُّهْتَدُونَ
Toppleen ku dul laaj ag pey te ñoom ñu gindiku lañu.
22وَمَا لِيَ لَا أَعْبُدُ الَّذِي فَطَرَنِي وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
moo man, ana lu may war a dal ba tax duma jaamu Yàlla mi ma bind ? Te ca Moom ngeen di dellu.
23أَأَتَّخِذُ مِن دُونِهِ آلِهَةً إِن يُرِدْنِ الرَّحْمَٰنُ بِضُرٍّ لَّا تُغْنِ عَنِّي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا وَلَا يُنقِذُونِ
Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ? Te bu Yërëmaakoon bi natte ci man lor, seenug tinu duma jariñ dara te duñu ma xettali.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Ya-Sin 21

Simoore Ya-Sin Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Toppleen ku dul laaj ag pey te ñoom ñu gindiku…

Simoore Aaya 21/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers