As-Saffat · 111/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ ۝١١١
Innahoo min `ibaadinal mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.

🎧 Dégg


📜 Aaya 109-113 — Simoore As-Saffat

109سَلَامٌ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ
“Jàmmi Yàlla na nekk ci kaw Ibraahiima”.
110كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
111إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
112وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.
113وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
111Aaya

Tekki — As-Saffat 111

Simoore As-Saffat Aaya 111 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.

Simoore Aaya 111/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 109–113. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers