As-Saffat · 137/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَإِنَّكُمْ لَتَمُرُّونَ عَلَيْهِم مُّصْبِحِينَ ۝١٣٧
Wa innakum latamurroona `alaihim musbiheen
📖 Tekkim Wolof
Te yéen a ngi leen di romb bu ngeen di xëy

🎧 Dégg


📜 Aaya 135-139 — Simoore As-Saffat

135إِلَّا عَجُوزًا فِي الْغَابِرِينَ
ba mu des màggat gu jigéen ga àndoon ak ña sànku wo
136ثُمَّ دَمَّرْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, faagaagal Nanu ña ca des
137وَإِنَّكُمْ لَتَمُرُّونَ عَلَيْهِم مُّصْبِحِينَ
Te yéen a ngi leen di romb bu ngeen di xëy
138وَبِاللَّيْلِ ۗ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
ak ci guddi gi. Xanaa dungeen xalaat ?
139وَإِنَّ يُونُسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
137Aaya

Tekki — As-Saffat 137

Simoore As-Saffat Aaya 137 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te yéen a ngi leen di romb bu ngeen di…

Simoore Aaya 137/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 135–139. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers