As-Saffat · 40/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ ۝٤٠
Illaa `ibaadal laahil mukhlaseen
📖 Tekkim Wolof
ba mu des jaami Yàlla yay sellal,

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Simoore As-Saffat

38إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.
39وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,
40إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des jaami Yàlla yay sellal,
41أُولَٰئِكَ لَهُمْ رِزْقٌ مَّعْلُومٌ
Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :
42فَوَاكِهُ ۖ وَهُم مُّكْرَمُونَ
ay fuytéef ak i teraanga,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — As-Saffat 40

Simoore As-Saffat Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des jaami Yàlla yay sellal,

Simoore Aaya 40/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers