As-Saffat · 41/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أُولَٰئِكَ لَهُمْ رِزْقٌ مَّعْلُومٌ ۝٤١
Ulaaa`ika lahum rizqum ma`loom
📖 Tekkim Wolof
Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Simoore As-Saffat

39وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,
40إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des jaami Yàlla yay sellal,
41أُولَٰئِكَ لَهُمْ رِزْقٌ مَّعْلُومٌ
Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :
42فَوَاكِهُ ۖ وَهُم مُّكْرَمُونَ
ay fuytéef ak i teraanga,
43فِي جَنَّاتِ النَّعِيمِ
ca biir Àjjanay xéewal ja,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — As-Saffat 41

Simoore As-Saffat Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :

Simoore Aaya 41/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers