Sad · 50/88
Tekki Waxtaan — Sad
جَنَّاتِ عَدْنٍ مُّفَتَّحَةً لَّهُمُ الْأَبْوَابُ ٥٠
Transliteration
Jannaati `adnim mufat tahatal lahumul abwaab
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Àjjanay Adan, seen wunt ya ne ŋàll ngir ñoom,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 48-52 — Sad
48وَاذْكُرْ إِسْمَاعِيلَ وَالْيَسَعَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ وَكُلٌّ مِّنَ الْأَخْيَارِ
Fàttalikul Ismaahiila ak Ilyaas, ak Suul kifli, ñoom ñépp ay tànnéef la ñu.
49هَٰذَا ذِكْرٌ ۚ وَإِنَّ لِلْمُتَّقِينَ لَحُسْنَ مَآبٍ
Lii ag fàttali la. Te ne ñay ragal Yàlla, am nañu, wàccuwaay wu jekk,
50جَنَّاتِ عَدْنٍ مُّفَتَّحَةً لَّهُمُ الْأَبْوَابُ
Àjjanay Adan, seen wunt ya ne ŋàll ngir ñoom,
51مُتَّكِئِينَ فِيهَا يَدْعُونَ فِيهَا بِفَاكِهَةٍ كَثِيرَةٍ وَشَرَابٍ
dañu fay, sóonu, di woo ay futéef yu bari ak i naan.
52۞ وَعِندَهُمْ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ أَتْرَابٌ
Amnañu fa ay jigéen (jabar) ñu di ay lamsalkat, yu maase ay at.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
50Aaya
Tekki — Sad 50
Simoore Sad Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Àjjanay Adan, seen wunt ya ne ŋàll ngir ñoom,Simoore Aaya 50/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








