Sad · 71/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
إِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن طِينٍ ۝٧١
Iz qaala Rabbuka lilmalaaa`ikati innee khaaliqum basharam min teen
📖 Tekkim Wolof
(Fàttalitul) ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man de maa ngi sàkk mbindéef ci ban.

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Simoore Sad

69مَا كَانَ لِيَ مِنْ عِلْمٍ بِالْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ إِذْ يَخْتَصِمُونَ
Amuma woon xam-xam ca xulóob kilifa ya gën a kawe.
70إِن يُوحَىٰ إِلَيَّ إِلَّا أَنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Li nu may soloo doonul lu dul ne man mii ab xuppe kat laa waaraatekat bu bir”.
71إِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن طِينٍ
(Fàttalitul) ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man de maa ngi sàkk mbindéef ci ban.
72فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ
Suma ko móolee ba ëf ci Sama Ruu, na ngeen daldi rot, sujuudal ko”.
73فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka ya yépp daldi sujuud,
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — Sad 71

Simoore Sad Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Fàttalitul) ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen :…

Simoore Aaya 71/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers