Sad · 79/88
Tekki Waxtaan — Sad
قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ ۝٧٩
Qaala Rabbi fa anzirneee ilaa Yawmi yub`asoon
📖 Tekkim Wolof
“[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba bisub dekkiwaat ba”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 77-81 — Sad

77قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ
(Yàlla) ne ko : “Génnal ca biti, dàkku naa la ;
78وَإِنَّ عَلَيْكَ لَعْنَتِي إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ
te Samam rëbb dal na la ba baa saa di taxaw”.
79قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
“[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba bisub dekkiwaat ba”.
80قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
(Yàlla) ne ko : “may Nanu la dig boobu,
81إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc ba)”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
79Aaya

Tekki — Sad 79

Simoore Sad Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba…

Simoore Aaya 79/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers