Sad · 78/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
وَإِنَّ عَلَيْكَ لَعْنَتِي إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ ۝٧٨
Wa inna `alaika la`nateee ilaa Yawmid Deen
📖 Tekkim Wolof
te Samam rëbb dal na la ba baa saa di taxaw”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 76-80 — Simoore Sad

76قَالَ أَنَا خَيْرٌ مِّنْهُ ۖ خَلَقْتَنِي مِن نَّارٍ وَخَلَقْتَهُ مِن طِينٍ
“[Ibliis,] tontu ne ko : maa ko gën ndax yaa ngi ma bind ci safara moom nga bind ko ci ban”.
77قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ
(Yàlla) ne ko : “Génnal ca biti, dàkku naa la ;
78وَإِنَّ عَلَيْكَ لَعْنَتِي إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ
te Samam rëbb dal na la ba baa saa di taxaw”.
79قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
“[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba bisub dekkiwaat ba”.
80قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
(Yàlla) ne ko : “may Nanu la dig boobu,
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Sad 78

Simoore Sad Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Samam rëbb dal na la ba baa saa di…

Simoore Aaya 78/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers