Az-Zumar · 68/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَصَعِقَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ إِلَّا مَن شَاءَ اللَّهُ ۖ ثُمَّ نُفِخَ فِيهِ أُخْرَىٰ فَإِذَا هُمْ قِيَامٌ يَنظُرُونَ ۝٦٨
Wa nufikha fis Soori fas`iqa man fis samaawaati wa man fil ardi illaa man shaa`al lahu summa nufikha feehi ukhraa fa izaa hum qiyaamuny yanzuroon
📖 Tekkim Wolof
Suñu ëfee bufta bi, lu nekk ci asamaan yeek suuf si léppay dee, lu dul la ca soob Yàlla. Ñu ëfaat ko beneen yoon ndeketeeyóo, ñépp a ngi ne fujjet jóg taxaw ne xey di xoole.
🎧 Dégg

📜 Aaya 66-70 — Az-Zumar

66بَلِ اللَّهَ فَاعْبُدْ وَكُن مِّنَ الشَّاكِرِينَ
Jaamujil Yàlla, tey sant”.
67وَمَا قَدَرُوا اللَّهَ حَقَّ قَدْرِهِ وَالْأَرْضُ جَمِيعًا قَبْضَتُهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وَالسَّمَاوَاتُ مَطْوِيَّاتٌ بِيَمِينِهِ ۚ سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Joxuñu Yàlla dayoom tigi, suuf si sépp ab ŋëbëm lay doon bu Bis Pénc baa, asamaan yépp ab lem lay doon ci [loxoom]. Tudd naa Sellam ga ! Kawe na ci liñu koy bokkaale.
68وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَصَعِقَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ إِلَّا مَن شَاءَ اللَّهُ ۖ ثُمَّ نُفِخَ فِيهِ أُخْرَىٰ فَإِذَا هُمْ قِيَامٌ يَنظُرُونَ
Suñu ëfee bufta bi, lu nekk ci asamaan yeek suuf si léppay dee, lu dul la ca soob Yàlla. Ñu ëfaat ko beneen yoon ndeketeeyóo, ñépp a ngi ne fujjet jóg taxaw ne xey di xoole.
69وَأَشْرَقَتِ الْأَرْضُ بِنُورِ رَبِّهَا وَوُضِعَ الْكِتَابُ وَجِيءَ بِالنَّبِيِّينَ وَالشُّهَدَاءِ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْحَقِّ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Suuf si daldi fenk ak leerug Boroomam ; ñu daldi teg Téere ba, indi Yonnent ya ak seede ya ; daldi àtte seen diggënte ci dëgg te kenn duleen tooñ ci dara ;
70وَوُفِّيَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّا عَمِلَتْ وَهُوَ أَعْلَمُ بِمَا يَفْعَلُونَ
bakkan bu nekk ñu fay ko la mu daan jëf. Te [Yàlla] moo gën a xam ñu daan def.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
68Aaya

Tekki — Az-Zumar 68

Simoore Az-Zumar Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Suñu ëfee bufta bi, lu nekk ci asamaan yeek suuf…

Simoore Aaya 68/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers