Az-Zumar · 75/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
وَتَرَى الْمَلَائِكَةَ حَافِّينَ مِنْ حَوْلِ الْعَرْشِ يُسَبِّحُونَ بِحَمْدِ رَبِّهِمْ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْحَقِّ وَقِيلَ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝٧٥
Wa taral malaaa`ikata haaaffeena min hawlil `Arshi yusabbihoona bihamdi Rabbihim wa qudiya bainahum bilhaqqi wa qeelal hamdu lillaahi Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Nga gis Malaaka yaa ngay wër (Aras), di sàbbaal seen cantug Boroom. Ñu wax naan : “Xeeti cant, ñeel na Yàlla miy Boroom àddina si”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-75 — Simoore Az-Zumar

73وَسِيقَ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ إِلَى الْجَنَّةِ زُمَرًا ۖ حَتَّىٰ إِذَا جَاءُوهَا وَفُتِحَتْ أَبْوَابُهَا وَقَالَ لَهُمْ خَزَنَتُهَا سَلَامٌ عَلَيْكُمْ طِبْتُمْ فَادْخُلُوهَا خَالِدِينَ
Ñooy jiital ña ragaloon seen Boroom jëme leen Àjjana. Ñu, di ay mbooloo bu ñu fa àggee wunt ya ubbeeku, ña koy wattu ne leen : “Jàmm rekk yal na nekk ci yéen ! Yéen dey baax ngeen : dugguleen ci, te dangeen ciy béel”.
74وَقَالُوا الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي صَدَقَنَا وَعْدَهُ وَأَوْرَثَنَا الْأَرْضَ نَتَبَوَّأُ مِنَ الْجَنَّةِ حَيْثُ نَشَاءُ ۖ فَنِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ
Ñuy wax naan : “Noo ngi sant Yàlla mi nu dëggëlal digëm bi te donale nu suuf si ! Tey noo ngi xéyoo ci Àjjana nu mu nu neexe”. Ay waay gii pey a neex !
75وَتَرَى الْمَلَائِكَةَ حَافِّينَ مِنْ حَوْلِ الْعَرْشِ يُسَبِّحُونَ بِحَمْدِ رَبِّهِمْ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْحَقِّ وَقِيلَ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Nga gis Malaaka yaa ngay wër (Aras), di sàbbaal seen cantug Boroom. Ñu wax naan : “Xeeti cant, ñeel na Yàlla miy Boroom àddina si”.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Az-Zumar 75

Simoore Az-Zumar Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nga gis Malaaka yaa ngay wër (Aras), di sàbbaal seen…

Simoore Aaya 75/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 73–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers