Az-Zumar · 74/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
وَقَالُوا الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي صَدَقَنَا وَعْدَهُ وَأَوْرَثَنَا الْأَرْضَ نَتَبَوَّأُ مِنَ الْجَنَّةِ حَيْثُ نَشَاءُ ۖ فَنِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ ۝٧٤
Wa waalull hamdulillaahil lazee sadaqanaa wa`dahoo wa awrasanal arda natabaw wa-u minal jannati haisu nashaaa`u fani`ma ajrul `aamileen
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Noo ngi sant Yàlla mi nu dëggëlal digëm bi te donale nu suuf si ! Tey noo ngi xéyoo ci Àjjana nu mu nu neexe”. Ay waay gii pey a neex !
🎧 Dégg

📜 Aaya 72-75 — Az-Zumar

72قِيلَ ادْخُلُوا أَبْوَابَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۖ فَبِئْسَ مَثْوَى الْمُتَكَبِّرِينَ
“Ñu ne, [leen] dugguleen, wunti Safara, ngeen béel fa”. Rëy-rëylu kat tee ka bon ab saxuwaay !
73وَسِيقَ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ إِلَى الْجَنَّةِ زُمَرًا ۖ حَتَّىٰ إِذَا جَاءُوهَا وَفُتِحَتْ أَبْوَابُهَا وَقَالَ لَهُمْ خَزَنَتُهَا سَلَامٌ عَلَيْكُمْ طِبْتُمْ فَادْخُلُوهَا خَالِدِينَ
Ñooy jiital ña ragaloon seen Boroom jëme leen Àjjana. Ñu, di ay mbooloo bu ñu fa àggee wunt ya ubbeeku, ña koy wattu ne leen : “Jàmm rekk yal na nekk ci yéen ! Yéen dey baax ngeen : dugguleen ci, te dangeen ciy béel”.
74وَقَالُوا الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي صَدَقَنَا وَعْدَهُ وَأَوْرَثَنَا الْأَرْضَ نَتَبَوَّأُ مِنَ الْجَنَّةِ حَيْثُ نَشَاءُ ۖ فَنِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ
Ñuy wax naan : “Noo ngi sant Yàlla mi nu dëggëlal digëm bi te donale nu suuf si ! Tey noo ngi xéyoo ci Àjjana nu mu nu neexe”. Ay waay gii pey a neex !
75وَتَرَى الْمَلَائِكَةَ حَافِّينَ مِنْ حَوْلِ الْعَرْشِ يُسَبِّحُونَ بِحَمْدِ رَبِّهِمْ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْحَقِّ وَقِيلَ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Nga gis Malaaka yaa ngay wër (Aras), di sàbbaal seen cantug Boroom. Ñu wax naan : “Xeeti cant, ñeel na Yàlla miy Boroom àddina si”.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Az-Zumar 74

Simoore Az-Zumar Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Noo ngi sant Yàlla mi nu…

Simoore Aaya 74/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 72–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers