Ghafir · 42/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
تَدْعُونَنِي لِأَكْفُرَ بِاللَّهِ وَأُشْرِكَ بِهِ مَا لَيْسَ لِي بِهِ عِلْمٌ وَأَنَا أَدْعُوكُمْ إِلَى الْعَزِيزِ الْغَفَّارِ ۝٤٢
Tad`oonanee li-akfura billaahi wa ushrika bihee maa laisa lee bihee `ilmunw wa ana ad`ookum ilal`Azeezil Ghaffaar
📖 Tekkim Wolof
Yéen a ngi may woo ngir ma weddi Yàlla di ko bokkaaleek lu ma amul benn xam-xam, te man maa ngi leen di woo jëme leen ci Yàlla miy boroom Kàttan, tey Jégëlaakoon ba.
🎧 Dégg

📜 Aaya 40-44 — Ghafir

40مَنْ عَمِلَ سَيِّئَةً فَلَا يُجْزَىٰ إِلَّا مِثْلَهَا ۖ وَمَنْ عَمِلَ صَالِحًا مِّن ذَكَرٍ أَوْ أُنثَىٰ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَأُولَٰئِكَ يَدْخُلُونَ الْجَنَّةَ يُرْزَقُونَ فِيهَا بِغَيْرِ حِسَابٍ
Képp kuy def ñaawtéef dees na ko fay kem la mu def ; waaye képp kuy def yiw, di góor mbaa muy jigéen, te fekk mu gëm, ñoom ñooy dugg Àjjana di fa jot xéewël yu amul waññ.
41۞ وَيَا قَوْمِ مَا لِي أَدْعُوكُمْ إِلَى النَّجَاةِ وَتَدْعُونَنِي إِلَى النَّارِ
Éy yéen samaw nit, ana lan moo tax ma di leen woo jëme leen ci mucc, te yéen ngeen di ma woo jëmale ma Safara ?
42تَدْعُونَنِي لِأَكْفُرَ بِاللَّهِ وَأُشْرِكَ بِهِ مَا لَيْسَ لِي بِهِ عِلْمٌ وَأَنَا أَدْعُوكُمْ إِلَى الْعَزِيزِ الْغَفَّارِ
Yéen a ngi may woo ngir ma weddi Yàlla di ko bokkaaleek lu ma amul benn xam-xam, te man maa ngi leen di woo jëme leen ci Yàlla miy boroom Kàttan, tey Jégëlaakoon ba.
43لَا جَرَمَ أَنَّمَا تَدْعُونَنِي إِلَيْهِ لَيْسَ لَهُ دَعْوَةٌ فِي الدُّنْيَا وَلَا فِي الْآخِرَةِ وَأَنَّ مَرَدَّنَا إِلَى اللَّهِ وَأَنَّ الْمُسْرِفِينَ هُمْ أَصْحَابُ النَّارِ
Sikkuwul ne li ngeen may woo jëmale amuñu luy tax ñu war leen a woo ci àddina sii waxantumaalaak ca àllaaxira. Te it ca Yàlla lañuy dellu, te itam yaqkat ya ñooy wa Safara.
44فَسَتَذْكُرُونَ مَا أَقُولُ لَكُمْ ۚ وَأُفَوِّضُ أَمْرِي إِلَى اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ بَصِيرٌ بِالْعِبَادِ
Yàggatul ne dangeen fàttaliku ji lii ma leen di wax ; te wéer naa samay mbir ci Yàlla. Ndax, kuy Gis jaamam ñi la.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Ghafir 42

Simoore Ghafir Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen a ngi may woo ngir ma weddi Yàlla di…

Simoore Aaya 42/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers