Ghafir · 71/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
إِذِ الْأَغْلَالُ فِي أَعْنَاقِهِمْ وَالسَّلَاسِلُ يُسْحَبُونَ ۝٧١
Izil aghlaalu feee a`naaqi-him wassalaasilu yashaboon
📖 Tekkim Wolof
jéng, yaa nga seen doq ñuy gëwéele

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Simoore Ghafir

69أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ يُجَادِلُونَ فِي آيَاتِ اللَّهِ أَنَّىٰ يُصْرَفُونَ
Xanaa gisuloo ñiy dàggasante ci laayay Yàlla yi ni ñu leen di walbatee?
70الَّذِينَ كَذَّبُوا بِالْكِتَابِ وَبِمَا أَرْسَلْنَا بِهِ رُسُلَنَا ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ñay weddi Téere ba (Alxuraan) ak li nu yónnee sunuy Yonnent ; (waaye) dananu xala xam,
71إِذِ الْأَغْلَالُ فِي أَعْنَاقِهِمْ وَالسَّلَاسِلُ يُسْحَبُونَ
jéng, yaa nga seen doq ñuy gëwéele
72فِي الْحَمِيمِ ثُمَّ فِي النَّارِ يُسْجَرُونَ
ca biir ndox may wañax; ñu door leen a yóbbu xoyom leen ca Safara.
73ثُمَّ قِيلَ لَهُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ تُشْرِكُونَ
Bu loolu jàllee ñu ne leen : “Ana li ngeen daan bokkale
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — Ghafir 71

Simoore Ghafir Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : jéng, yaa nga seen doq ñuy gëwéele

Simoore Aaya 71/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers