Ghafir · 72/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فِي الْحَمِيمِ ثُمَّ فِي النَّارِ يُسْجَرُونَ ۝٧٢
Fil hameemi summa fin Naari Yasjaroon
📖 Tekkim Wolof
ca biir ndox may wañax; ñu door leen a yóbbu xoyom leen ca Safara.
🎧 Dégg

📜 Aaya 70-74 — Ghafir

70الَّذِينَ كَذَّبُوا بِالْكِتَابِ وَبِمَا أَرْسَلْنَا بِهِ رُسُلَنَا ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ñay weddi Téere ba (Alxuraan) ak li nu yónnee sunuy Yonnent ; (waaye) dananu xala xam,
71إِذِ الْأَغْلَالُ فِي أَعْنَاقِهِمْ وَالسَّلَاسِلُ يُسْحَبُونَ
jéng, yaa nga seen doq ñuy gëwéele
72فِي الْحَمِيمِ ثُمَّ فِي النَّارِ يُسْجَرُونَ
ca biir ndox may wañax; ñu door leen a yóbbu xoyom leen ca Safara.
73ثُمَّ قِيلَ لَهُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ تُشْرِكُونَ
Bu loolu jàllee ñu ne leen : “Ana li ngeen daan bokkale
74مِن دُونِ اللَّهِ ۖ قَالُوا ضَلُّوا عَنَّا بَل لَّمْ نَكُن نَّدْعُو مِن قَبْلُ شَيْئًا ۚ كَذَٰلِكَ يُضِلُّ اللَّهُ الْكَافِرِينَ
bàyyi Yàlla (jaamuwuleen ko) ? ” “Ñu tontu ne, réer nañu. Nun kay, lu jiitu tey, masunoo woo di jaamu dara”. Noonu la Yàlla di sànke yéefar ya.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Ghafir 72

Simoore Ghafir Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ca biir ndox may wañax; ñu door leen a yóbbu…

Simoore Aaya 72/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers