Az-Zukhruf · 21/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
أَمْ آتَيْنَاهُمْ كِتَابًا مِّن قَبْلِهِ فَهُم بِهِ مُسْتَمْسِكُونَ ۝٢١
Am aatainaahum Kitaabam min qablihee fahum bihee mustamsikoon
📖 Tekkim Wolof
Walla, da Nu leen joxoon ab Téere ca la ko jiitu woon ba tax ñu ŋoyoon ca ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 19-23 — Az-Zukhruf

19وَجَعَلُوا الْمَلَائِكَةَ الَّذِينَ هُمْ عِبَادُ الرَّحْمَٰنِ إِنَاثًا ۚ أَشَهِدُوا خَلْقَهُمْ ۚ سَتُكْتَبُ شَهَادَتُهُمْ وَيُسْأَلُونَ
Ñuy def Malaaka ya di ay jaamu Yàlla [aw jigéen] ! moo ndax baleen Yàlla di sàkk dañu koo teewe woon ? Danañu bind la ñu seede ; laaj leen ko (ba xam lu ñu ca xam).
20وَقَالُوا لَوْ شَاءَ الرَّحْمَٰنُ مَا عَبَدْنَاهُم ۗ مَّا لَهُم بِذَٰلِكَ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِنْ هُمْ إِلَّا يَخْرُصُونَ
Dañuy wax naan : “Bu neexoon Yàlla du nu leen jaamu”. Waaye amuñu ca benn xam- xam ; dañuy foog doŋŋ.
21أَمْ آتَيْنَاهُمْ كِتَابًا مِّن قَبْلِهِ فَهُم بِهِ مُسْتَمْسِكُونَ
Walla, da Nu leen joxoon ab Téere ca la ko jiitu woon ba tax ñu ŋoyoon ca ?
22بَلْ قَالُوا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّهْتَدُونَ
Li ñu wax kay moo di : “Fekkoon nanu sunuy maam am diine, kon nag (wat ci watiit) ñoom la ñuy toppandoo”.
23وَكَذَٰلِكَ مَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي قَرْيَةٍ مِّن نَّذِيرٍ إِلَّا قَالَ مُتْرَفُوهَا إِنَّا وَجَدْنَا آبَاءَنَا عَلَىٰ أُمَّةٍ وَإِنَّا عَلَىٰ آثَارِهِم مُّقْتَدُونَ
(Noonu it la daan deme) ndax masunoo yónni waa ab xuppekat (waaraatekat) cib dëkk lu dul ne ne kilifa ya danuy wax naan : “Sunuy maam amoon nañu diine te nun ñoom la ñuy roy”.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 21

Simoore Az-Zukhruf Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla, da Nu leen joxoon ab Téere ca la ko…

Simoore Aaya 21/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers